๐…๐š๐›๐ซ๐ข๐ณ๐ข๐จ ๐‚๐ข ๐–๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ

  • Page d'Accueil
  • Sรฉnรฉgal
  • Rosso
  • ๐…๐š๐›๐ซ๐ข๐ณ๐ข๐จ ๐‚๐ข ๐–๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ

๐…๐š๐›๐ซ๐ข๐ณ๐ข๐จ ๐‚๐ข ๐–๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ ๐ŸŽ™๏ธ๐…๐š๐›๐ซ๐ข๐ณ๐ข๐จ ๐œ๐ข ๐ฐ๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ๐Ÿซ€
๐Ÿงพ๐—๐ข๐›๐š๐š๐ซ๐ฎ ๐Ÿ๐จ๐จ๐ญ๐›๐š๐ฅ๐ฅ ๐œ๐ข ๐–๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ๐Ÿซถ๐Ÿพ
๐Ÿšจ๐ƒ๐š๐ซ๐š ๐๐ฎ๐ฅ๐š ๐œ๐ข ๐ซ๐ž๐ญ๐ก๐ข
๐Ÿ“ž๐.๐Ÿ•๐Ÿ•๐Ÿ’๐Ÿ”๐Ÿ๐Ÿ’๐Ÿ๐Ÿ“๐Ÿ๐Ÿ“ฑ
(1)

Boubacar Koita Footballkatu Mauritanie bi natalu Ldc ni๐Ÿ‡ฒ๐Ÿ‡ทโค๏ธ
15/09/2026

Boubacar Koita Footballkatu Mauritanie bi natalu Ldc ni๐Ÿ‡ฒ๐Ÿ‡ทโค๏ธ

๐ŸŽ™๏ธKalidou Koulibaly ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ : ยซ Dina indi watt tolluwaay bima รฑรฉpp di xare .ยป
15/09/2026

๐ŸŽ™๏ธKalidou Koulibaly ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ : ยซ Dina indi watt tolluwaay bima รฑรฉpp di xare .ยป

๐Ÿšจ๐Ÿ˜ณ Harry Kane ๐Ÿ‡ฌ๐Ÿ‡ง bรซgg jรซl na Ballon d'Or waaye bรซggul weur fena di wax mooko yelloo wala moom laรฑu wara jรณox  ๐Ÿ†.Dafa bรซg...
15/09/2026

๐Ÿšจ๐Ÿ˜ณ Harry Kane ๐Ÿ‡ฌ๐Ÿ‡ง bรซgg jรซl na Ballon d'Or waaye bรซggul weur fena di wax mooko yelloo wala moom laรฑu wara jรณox ๐Ÿ†.

Dafa bรซgg limu def attmi waxal boppam! ๐Ÿ‘โค๏ธ

๐Ÿšจ๐Ÿ˜‚ Haaland dafa amoon ab dajee ak been taskatu xibaar, ci laako waax ni dafay Baari lumu lekk carotte ๐Ÿฅ•๐Ÿ‡ณ๐Ÿ‡ดBobu ba lรฉegi D...
15/09/2026

๐Ÿšจ๐Ÿ˜‚ Haaland dafa amoon ab dajee ak been taskatu xibaar, ci laako waax ni dafay Baari lumu lekk carotte ๐Ÿฅ•๐Ÿ‡ณ๐Ÿ‡ด

Bobu ba lรฉegi Dรซkkem bi di Norvรจge daรฑu lekk carrotte lu bari ! ๐Ÿ˜ญ๐Ÿ˜‚

Cรซy Erling โค๏ธ๐Ÿ’ช๐Ÿพ

Ferran khady Thiam Torres mooy yaakaaru PSG jamono  ji. ๐Ÿฆˆ๐Ÿ‡ช๐Ÿ‡ธโค๏ธ๐Ÿ’™
15/09/2026

Ferran khady Thiam Torres mooy yaakaaru PSG jamono ji. ๐Ÿฆˆ๐Ÿ‡ช๐Ÿ‡ธโค๏ธ๐Ÿ’™

Erling Haaland ๐Ÿ‡ณ๐Ÿ‡ด ci duggu ci Ilimane Ndiaye ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ :ยซ Dafa yรฉeme bimu duggee. yรฉnna say , dafa xawa niru Neymar. ยป
15/09/2026

Erling Haaland ๐Ÿ‡ณ๐Ÿ‡ด ci duggu ci Ilimane Ndiaye ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ :

ยซ Dafa yรฉeme bimu duggee. yรฉnna say , dafa xawa niru Neymar. ยป

๐Ÿšจ๐Ÿ˜ณ COOW LU Rร‹Y CA ITALIE! Sunu sukkandikoo ci La Gazzetta, 8 club yu nekk ca SรฉrieA daรฑu baรฑ (Arbitre) bu jigeen bi di M...
15/09/2026

๐Ÿšจ๐Ÿ˜ณ COOW LU Rร‹Y CA ITALIE!

Sunu sukkandikoo ci La Gazzetta, 8 club yu nekk ca SรฉrieA daรฑu baรฑ (Arbitre) bu jigeen bi di Marayanna muy (Arbitre) sen jongante.

Sabab bi? Neenaรฑu nekkam ci (terrain)bi defay "diis" ci yenn footballkat yi. ๐Ÿ˜ณ๐Ÿ˜‚

Iliman Ndiaye coow li yร lla na jikk ๐Ÿ˜Œโค๏ธ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณรฑaari fร nn yi yรซpp foo romb ci (internet) moo laรฑuy waxtaanee
15/09/2026

Iliman Ndiaye coow li yร lla na jikk ๐Ÿ˜Œโค๏ธ๐Ÿ‡ธ๐Ÿ‡ณ

รฑaari fร nn yi yรซpp foo romb ci (internet) moo laรฑuy waxtaanee

๐Ÿšจ๐ŸŽ™๏ธ Eric Garcia : ยซ jรซlu ma limu รฑent bi ndax cรซr bima jรณox Araujo. dafa dem ngir been att , tee lรฉpp su jaare ci yoon ,...
15/09/2026

๐Ÿšจ๐ŸŽ™๏ธ Eric Garcia :

ยซ jรซlu ma limu รฑent bi ndax cรซr bima jรณox Araujo. dafa dem ngir been att , tee lรฉpp su jaare ci yoon , dina delluci watt , te dina jรซlat limu ร‘ent bi. ยป

๐Ÿ† stade yinu wara amalee finalu Ldc โŒ›๏ธ :2027 โ€” Madrid, Metropolitano ๐Ÿ‡ช๐Ÿ‡ธ2028 โ€” Munich, Allianz Arena ๐Ÿ‡ฉ๐Ÿ‡ช2029 โ€” Barcelone, ...
15/09/2026

๐Ÿ† stade yinu wara amalee finalu Ldc โŒ›๏ธ :

2027 โ€” Madrid, Metropolitano ๐Ÿ‡ช๐Ÿ‡ธ
2028 โ€” Munich, Allianz Arena ๐Ÿ‡ฉ๐Ÿ‡ช
2029 โ€” Barcelone, Camp Nou ๐Ÿ‡ช๐Ÿ‡ธ

Adresse

Rosso

Site Web

Notifications

Soyez le premier ร  savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque ๐…๐š๐›๐ซ๐ข๐ณ๐ข๐จ ๐‚๐ข ๐–๐จ๐ฅ๐จ๐Ÿ publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisรฉe ร  d'autres fins, et vous pouvez vous dรฉsabonner ร  tout moment.

Raccourcis

Partager