Sylla Madridista en wolof

Sylla Madridista en wolof Halla Madrid 🤍😇

Photo wa Real Madrid saison 2026/2027Halla Madrid 🤍  Yàll naleen yàlla defal ay ndam you bari
19/08/2026

Photo wa Real Madrid saison 2026/2027

Halla Madrid 🤍
Yàll naleen yàlla defal ay ndam you bari

Jose Mourinho  "Mbappe ? Dafa yéeme. Daf may reetaan loo ci biir tàggat yaram, dafa BAAX lool. Niveau bimu am mooy STRAT...
19/08/2026

Jose Mourinho "

Mbappe ? Dafa yéeme. Daf may reetaan loo ci biir tàggat yaram, dafa BAAX lool. Niveau bimu am mooy STRATOSFERIK

Real Madrid présente na Bernardo Silva tay 🤍🇵🇹
19/08/2026

Real Madrid présente na Bernardo Silva tay 🤍🇵🇹

🚨💣jpedrerol : « Real Madrid mëuna signe benn joueur ci été bi " ben milieu de terrain 🤍
17/08/2026

🚨💣jpedrerol : « Real Madrid mëuna signe benn joueur ci été bi

" ben milieu de terrain 🤍

🚨 José Mourinho laaj na wa Real Madrid ñu siñe Martin Zubimendi ak lumu mëna doon
17/08/2026

🚨 José Mourinho laaj na wa Real Madrid ñu siñe Martin Zubimendi ak lumu mëna doon

Match bi jeexna Real Madrid mu am ndam ci kaw Schalke 04 ⚪️🔵 3-0 Y nada mas 🤍
16/08/2026

Match bi jeexna
Real Madrid mu am ndam ci kaw Schalke 04 ⚪️🔵 3-0

Y nada mas 🤍

Jour du match ⚽️Vs  Schalke 04 ⚪️🔵Amical 🤝15H00 GMT ⏰️Halla Madrid 🤍
16/08/2026

Jour du match ⚽️
Vs Schalke 04 ⚪️🔵
Amical 🤝
15H00 GMT ⏰️

Halla Madrid 🤍

🚨 Breaking : Real Madrid dañu intéressé wou ci milieu de terrain bi di Kees Smit 🇳🇱 🧠 José Mourinho mingi wër joueur yu ...
16/08/2026

🚨 Breaking : Real Madrid dañu intéressé wou ci milieu de terrain bi di Kees Smit 🇳🇱

🧠 José Mourinho mingi wër joueur yu mëna jouer ci posisioŋ yu bari, lu melni Bernardo Silva, te Kees Smit mën na jouer ci posisioŋ boobu.

📌 Waaye, ba leegi amagul benn jéego ci wàllu siñe.

🚨🗞️ [Diario AS]

🚨 Kylian Mbappé : "Am entraîner bu melni José Mourinho lu am solo la; entraîner bu xam ni ñuy jëlee ndam la." 🤍
15/08/2026

🚨 Kylian Mbappé : "Am entraîner bu melni José Mourinho lu am solo la; entraîner bu xam ni ñuy jëlee ndam la." 🤍

🚨🧤 Lunin day des ci Real Madrid! 🤍🔥Andriy Lunin dafa nara yokk contrat ak Real Madrid ba 2030. 🇺🇦🤍Extension bii dafay gë...
15/08/2026

🚨🧤 Lunin day des ci Real Madrid! 🤍🔥

Andriy Lunin dafa nara yokk contrat ak Real Madrid ba 2030. 🇺🇦🤍

Extension bii dafay gëna yombal dem bi. Rawatina ni ginnaaw bi Fran González deme, Real Madrid yaakaarna ni amatul kenn ku wóór ngir Thibaut Courtois. 🧤😬

Kon tëye Lunin ci Real Madrid lu am solo la ngir mëna wéy di nekk gool. 🤍🔥

📰 Okdiario

Adresse

Diourbel
Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sylla Madridista en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager