08/10/2025
Mbookou yi Ma********on lou haraam la , te lou bone thi wergui yaram la , defoon naasi ab taxaw seetlou , waayé damasi niawaat , ndakh nit gni makoy laadj dafa bary lool
_______________________________________________
Mbookou yi , ma********on kepou kouvkoy def , bou féké dafay diangue concentration lay dieukeu gnak ndah dafay perturbé centre biko amé
sa capacité intellectuelle dafay dimunié wagnékou , te doo mana diamou yalla diamou bou sél ndah limou beugue halate ak loumou beugoul halate helmi dinassi dém dafay perdre controle bi
_______________________________________________
Bepou goor boukoy déf nak faawou dinga ame impuissance sexuelle
Bepou djigueen boukoy def yitam dooto yeungueuti goor Si benne côté
_______________________________________________
Mbookou yi ma********on dafay dolél nafsa la amaratou bi souhi , Mou teunk Nafsou lawama ,
Bouko défé Nite beugue beugueum do ame loukossi mane yéd mou arrété ko
Ndaye saane te kepou thi gni Masturbé wala def lou bone bouparé dafa réthiou ndah dafay fék nafsa la amaratou bi souhi déf liguéyam ba Nopi bouko défé Nafsoun lawama sila yéwéko diko regrettélo amoul capacite empechéko action bi
Amoul kouy sétane film pornographyque ba noopi cerveau bi Normal , deded , dou halate lou yiw dafay halate lou Bone té douko tay
dangay guiss kou ame Sokhna bayifa sokhnam di fowé bopam nga wara hamené si cerbeau bi la Rouh gui tilim na
_______________________________________________
Solution
Pour Arretez la maturbation :
Faire apres chaqué priere
Fatiha
3 fois Astaghfiroullah
3 fois salatou ala Nabí ( exemple salatou ala Nabí : Allahouma salli ala Seydina Mouhammad wa ala alihi wa sahbihi wa sallim taslim)
7 fois sourate likhlass( khoul khou wallahou ahah Allahou samad lam yalid walam youlad walam yakoune lehou koufouwan Ahad)
7 fois sourate qadri( Bismi Allahi alrrahmani alrraheemi
1. Inna anzalnahou fi laylatil qadri
2. Wama adraka ma laylatoul qadri
3. Laylatoul qadri khayroun min alfi shahrin
4. Tanazzaloul mala-ikatou waalrroohou fiha bi-ithni rabbihim min koulli amrin
5. Salamoun hiya hatta matla’i alfajri
_______________________________________________
Boo noopé nak nga wakh ni yaw yalla , yalla nanga ma taakhlé ak lou Bone li
Nga Teudjéko 3 fois salatou Ala Nabí
Defko Hadiya yonanete bi Sallal lahou aleyhi wa sallam
Na nga moytou di sétane lou Bone tant k bayiwoko do bayi fowé sa bop ,
_______________________________________________
Pour gni faral di laath sama numéro watsape mingui nii ( 76 253 90 90 )